Ananse, Yàmbar Nekk Bón

jàng

Ananse, Yàmbar Nekk Bón

Maf nekk ab nitt baax. Jàrgoñ nekk ab nitt bón. Maf door ab tool. Jàrgoñ door ab tool. Maf liggéey.